가사 좌표
WO원문 가사
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
Jëf jël ñakk jariñu
Jëf jël ñakk jariñu
Jëf jël ñakk jariñu
Jëf jël ñakk jariñu
Goor Faal
Mbaa fate woo
Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar
Lahi laa ha ila laa Faal
Meysa Biige Kumba Faal
Goor Faal
Mbaa fate woo
Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar
Lahi laa ha ila laa Faal
Meysa Biige Kumba Faal
Mbaa fate woo
Mbaa fate woo
Mbaa fate woo
Mbaa fate woo
Boroom ndigël li nangu nañ
Boroom siggi be'g sëgg
Boroom ndigël li nangu nañ
Boroom siggi be'g sëgg
Boroom ndigël li nangu nañ
Goor Faal
Mbaa fate woo
Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar
Lahi laa ha ila laa Faal
Meysa Biige Kumba Faal
Goor Faal
Mbaa fate woo
Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar
Lahi laa ha ila laa Faal
Meysa Biige Kumba Faal





