Sutura

Sutura 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수27
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Ci sutura Ci sutura Ci sutura Sama waaji na ñu waxtaan ci sutura Xarit dee naa la ci sutura Ci sutura laa lay waxee sama ge′nt Sutura Ci sutura laa lay samay proble'mes akk lima dal Sutura Ci laa lay de′nkee sama guddi Bulma weer ni bëccëg Bulma weer ni bëccëg, sutura, sutura Bulma weer ni bëccëg Ndax yombul nga xamal ma Mbokk waay Sutura, sutura (Sutura sutural ma) Sutura (Sutural ma) Sutura (Sutura sutural ma) Sutura Mbokk du nii Reeroo bumu tax nga tasaare ma Sutura sutural ma Ñu weetoo ma wax la sama demb nga waxaat ko tay Xarit sama waaji, ma ne Mbokk du nii Bulma jeebaane fii Bul wax sama proble'me ci ñii Woolu la tay Waraloon demb ma wax la lu xew wax la sama xol Mbokk waay Sutura, sutura (Sutura sutural ma) Sutura (Sutural ma) Sutura (Sutura sutural ma) Sutura