Fa Diallo

Letra de Fa Diallo

Idioma originalWO
Visualizações98
Coordenadas da letra

Letra original

WO
A tradução ainda não está disponível. Exibindo a letra original.
18
Beuguena wanté mane dé dama amoul Da nga di gouné motakh mouy sa khalaat Ni Beuguena wanté mane dé dama Ragal Da nga di ngouné moutakh mouy sa khalaat Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar Té legui bo ko meunoul demal teudi Cherie coco li dé doyna kemane Nga nane ma kay niou say té awma pantam Fa Diallo wakhma noko toudé Nga naan ma takk la mane awma place Cherie coco wakhma no ko toudé Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt Di takhawalou Mané li dé doyna kemane Ni beugu na, ni beuguena la Fatou diallo wakhma no ko toudé Nga nane ma kay niou say té awma pantam Fa Diallo wakhma noko toudé Nga naan ma takk la mane awma place Cherie coco wakhma no ko toudé Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt Di takhawalou Mané li dé doyna kemane Ni beugu na, ni beuguena la Fatou diallo wakhma no ko toudé Ni beugu na, ni beuguena la Cherie coco wakhma no ko Guissé Ni beugu na, ni beuguena la Fatou diallo wakhma no ko toudé Ni beugu na, ni beuguena la Cherie coco wakhma no ko Guissé Nga naan ma kay niou sey té noumouy démé? Bou ndieukone dang chi toll niou may la djabar Té legui bo ko meunoul demal teudi Cherie coco li dé doyna kemane Nga nane ma takk la mane awma pantam Fa Diallo wakhma noko toudé Nga naan ma takk la mane awma place Cherie coco wakhma no ko toudé Ndakh legui da ngay diang ba yéy keuyitt Di takhawalou Mané li dé doyna kemane Ni beugu na, ni beuguena la Fatou diallo wakhma no ko toudé Ni beugu na, ni beuguena la