Jammu Africa

Letra de Jammu Africa

Duração5:03
Idioma originalWO
Visualizações6.2K
Coordenadas da letra

Letra original

WO
A tradução ainda não está disponível. Exibindo a letra original.
18
Afrika a a a Afrika mon Afrique Sama gent gi maa ngi ñaan Yalla wonma ko bala may ñibbi barsaq Ma ne bes du ñakk ci bes yi Afrika don benn reew D'ici ou d'ailleurs nous somm' des enfants d'Afrique Mêm' si le ciel tombait luttons pour la paix Kon jammu Afrika moom lay ñaan Mané jammu Afrika mooy suñu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Yow mi nekka bittim reew man mi Lô maa ngi lay ñaan Ak loo fa meun ta am ak noo fa meun ta mel bul fatte Afrika Ici ou ailleurs la paix prix du bonheur Mêm' si le ciel pleurait luttons pour nos frères Kon jammu Afrika moom lay ñaan Mané jammu Afrika mooy suñu natange Afrika a a a Afrika a a Afrika a a a Afrika mon Afrique Onon bibbe Afrika ngimode, ngimode liggo-den leydi men Ngaccen hasi daagal yoo Alla suren e musibaadi Yoo Alla addu jam to Ruanda Yoo Alla addu jam to Burundi Yoo Alla addu jam to Casamans Lawol Mbignona yee