Sabari

Sabari 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量16
歌词坐标

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
18
Mane Fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh Baba fogone na ni makk ioe ba abadane Mane fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh Ba fogone na ni makk ioe ba abadane Aduna ko warilen neu Mane sama ba déh sour nama Mane sama aduna déh yakhouna Kima geuneu beug fassé nama Hummm ndiabote gui wet lool Souma fataliko Baba souma fatali ko waaw Makk ioe nio dane teud ci béneu lal ba Nga dane ma deukeul dima xélal waw Li tey khawma louko waral Souma sagnone Baba souma sagnone mane Souma sagnone Baba souma sagnone mane Dig ma bayi ci sama négou seuy ba Khalé yi daniou nameu sen yaye Mane fogone na ni makk ioe dou meussa dièkh Ba fogone na ni makk ioe ba abadane [?]