Bul Ma Miin

Bul Ma Miin 歌词

流派Pop
原文语言WO
浏览量43
歌词坐标

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
18
Bul ma miin, Bul ma miin Bul ma miin ba fatte ma Kon mu ňaaw Adduna yaa mëna wor Xaň ma ndey xaň ma baay Boo ma digee sama doom nax nga ma Lekkatuma, naanatuma Tëddatuma, nelawatuma Boo ma digee sama doom nax nga ma Alarba la woon ci weeru koor Mu taggu ma ne ma maangi ňëw Boobu ba téy gisuma sama doom Woy wéét, woy wéét Woy wéét adduna Sama doom dem na nii