Goor

Goor 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量19
歌词坐标

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
18
Jëf jël ñakk jariñu Jëf jël ñakk jariñu Jëf jël ñakk jariñu Jëf jël ñakk jariñu Goor Faal Mbaa fate woo Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar Lahi laa ha ila laa Faal Meysa Biige Kumba Faal Goor Faal Mbaa fate woo Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar Lahi laa ha ila laa Faal Meysa Biige Kumba Faal Mbaa fate woo Mbaa fate woo Mbaa fate woo Mbaa fate woo Boroom ndigël li nangu nañ Boroom siggi be'g sëgg Boroom ndigël li nangu nañ Boroom siggi be'g sëgg Boroom ndigël li nangu nañ Goor Faal Mbaa fate woo Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar Lahi laa ha ila laa Faal Meysa Biige Kumba Faal Goor Faal Mbaa fate woo Lutax ñu fanaanee ròot aka sikkar Lahi laa ha ila laa Faal Meysa Biige Kumba Faal