Nawle

Nawle 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量130
歌词坐标

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
18
Su nit doon may boppam duñu néew la Duñ doon ay niiw di doole Kenn du ñu ëppale Yàlla mooy may waay Xeeb nañ ma ngir li may niiw di doole Ne nañ duma sa nawle Xool nañ ma bëtu xebbe Yàlla mooy may waay Su ma doon kiy dogal Sa askan kenn du ma ci raw ndax ni ñu ma def Des nañ ma wékk Gis naa lépp li nga may defal Sa waa-kër yépp ne du ci dal du fi ame Nga jombu leen ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi) Fok ma dem utti indi (léegi-léegi) Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex) Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex) Fok ma dem utti indi (léegi-léegi) Doole la néew le (léegi-léegi) Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex) Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex) Ouroul ayni sa niroowaale Aw nga ci tanku yaayu aje Yaa ngi mel ni barry bu ndaw Ndax Adji kom ngay daguwaale Doo nettali doo gaaruwaale Duggeloo ma ci giirawaale Ngir jëmu ju xébbu ji (léegi-léegi) Fok ma dem utti indi (léegi-léegi) Mënuma dem bàyyi la (day jeex, day jeex, day jeex) Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex) Fok ma dem utti indi (léegi-léegi) Doole la néew le (léegi-léegi) Ne nañ duma sa nawle (day jeex, day jeex, day jeex) Ne nañu amuma la nga dem bàyyi ma (day jeex, day jeex, day jeex)