Libre Valdiodio

Libre Valdiodio 歌词

流派Afrobeats
原文语言WO
浏览量10
歌词坐标

原文歌词

WO
暂时没有翻译,当前显示原文歌词。
18
Gent gi du neen Sa bidéew feñ na Wéetaay weesu na jaambaar Ñëwal ci leer, siggil nga dem Am nga ndam Ba àddunay tukki dootuñu la fàtte Wetoon nga mais gagner nga Ñoo ngi lay dello njukkal jaambaar Dugg ndugusin ndax ar li nga gëm Déggatoo mbokk xarit àndandoo Na cér nga la ma ramatu yi doon jooy di la wetalee Raw nga leen Guélowar! Gent gi du neen Sa bidéew feñ na Wéetaay weesu na jaambaar Ñëwal ci leer, siggil nga dem Am nga ndam