Diégué Kiraay

Diégué Kiraay şarkı sözleri

Orijinal dilWO
Görüntülenme17
Şarkı sözü koordinatları

Orijinal sözler

WO
Çeviri henüz yok. Orijinal sözler gösteriliyor.
18
Mësuloo ko ni waaw góor walla yaay jaambaar Ba mu nekke ci àdduna Mësuloo nangu li ko Yàlla Buur bi jagleel Ba mu nekke ci àdduna Tay ji dem na ngay jooy Ñépp ñoo ngi naan aka moo baaxoon Na la leer ni ñun dem na Lu baax lu mu def fi musoloo ko ko yéene Ku fi dee rekk ñu wax sa baax Bàyyi ma jalaale di la jooy Ayoooo ndeysaan! Àndak wa këram toog di la jooy Ndeysaan mbaa xam nga Moo ngi ci ndox jege ndox te du lakk ku ngay xool Xel xool sa xaalat ak yéene bari na