Ndaanaan

Текст песни Ndaanaan

ЖанрAfrobeats
Язык оригиналаWO
Просмотры6
Координаты текста

Оригинальный текст

WO
Перевод пока недоступен. Показан оригинальный текст.
18
Papa pa papa Dama bëgg jàngi Dama bëgg am xam-xam Lan, sama doom? Dama bëgg jàngi Dama bëgg am xam-xam Eeeh Massamba Walo Duma doon ku ñu naan cam Doo ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Kenn du ma xool di ma naan topp ma Reew mi dinañ donni ñi fiy doggali Bés sa ngi ci bés yi Dinañ bokku ci ñin na diiw wa ngi Ndax dama fonk loolu sama liggéey Tekki gëm-gëm moo kay maye Mënta naqari su may liggéey Ndax li kay neexal lang ci man Def li may def ci personnalité Teg ko ci code du genn gamm Indi fi yeneen tonalité Dugal leen ci yeneen ni game Aay waay! Duma doon ku ñu naan cam Doo ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Kenn du ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Doo ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Kenn du ma xool di ma naan topp ma Ndaanaan sama lama ngone Ci bor bu tar bi lañu jogé Ndaanaan sama lama ngone Dañu sonoo loolu bañuy doni gone Alhamdulillah eeeh Li gëna metti jot na jaale Na indi ku leen di ngone nam indi Nanguwuñu xam nañu fi ñu jogé fàttewuñu Ndax dañu fonk loolu sunu liggéey Tekki gëm-gëm moo kay maye Mënta naqari su ñuy liggéey Ndax li kay neexal lang ci man, eeeh waay! Duma doon ku ñu naan cam Doo ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Kenn du ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Doo ma xool di ma naan topp ma Duma doon ku ñu naan cam Kenn du ma xool di ma naan topp ma