Sibam (feat. Sidate Bonbon)

Letra de Sibam (feat. Sidate Bonbon)

GêneroPop
Idioma originalWO
Visualizações102
Coordenadas da letra

Letra original

WO
A tradução ainda não está disponível. Exibindo a letra original.
18
Tay ji bésu begete la gay ñi Tay ji ñëwel ñu ànd fecc Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen Ñëwel dugg ci géew gi Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen Na ñépp ñëw ci géew gi Ma woyaat sibam Jigéen ñi woneleen seen bopp Ak yeen góor ñi yee nit ci génn bokk Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen Na ñépp ñëw ci géew bi Mag ak ndaw, amul góor ak jigéen Feccal dugg ci geew gi Ma woyaat sibam Viviane, ma sira ak Issa Dieye Fatim Penda ak Ma Ndiaye Lay la cat, mashallah! Tàcculeen, fecceleen, rafet genn Loo loy xubal geew gi Te guleen, fecceleen, mag ñee Bu gene gene geew gi Ma woyaat sibam Yeah, yeah, yeah Ma woyaat sibam Ouh la, ou la la Jege ma Ouh la, ou la la Pare ngeen Sibam sibamoo sibam laal nga ma Sibam sibamoo sibam laal nga ma Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma Sibam sibamoo sibam laal nga ma Sibam sibamoo sibam laal nga ma Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma Ma ne sibam sibamoo sibam laal nga ma Booy fecce sibam dangay mel ni xaaru la biir Sa jege di karaje yaay sibam laal na ma