ALJANA

ALJANA 가사

원문 언어WO
조회수6
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Paradise rek laalay jeumé Thi geedjou banekh laniouy feey maak iow Beukoulo akk niom niveau Teg naala thi kaw Té dara doulafa dieulé my bve Aljana Aljana laala jeumé iow aljana Iow aldiana Dou Aljana lagn nara deuké Aljana Oubi sa xol douggeul fa airou aljana Aljanaaaa Maak iow ba paradise Denk naala sama life Dou ayy foo laalay doyei my bve Farata rek laalay doyei my bve Takk ma boum si baat Soxlawoul sakh ngamay wakh fooma nara dieulé my bve Manak iow dou diekh Deh rek moniouy takkalé Meunoumala baayek kenen Iow laay soor baby waxma loula nior Lane ngay yootou chérie ma adjiko Paradise rek laalay dieumé Thi geediou baneex laniouy feey maak iow Aljana Aljana laala jeumé iow aljana Iow aldiana Dou Aljana lagn nara deuké Aljana Oubi sa xol douggeul fa airou aljana Aljanaaaa