Togn Ngama

Togn Ngama 가사

원문 언어WO
조회수14
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Dougg nga sama keur diakhassé ko Lepp lignou fassone nga ba ko Dou sakh dama saagan, damala nob Sama xol bi, ma diokh la Takhaw thi say beugg beugg Say caprices meu encaisser, damala no-bone Mon amour pour toi m'a aveuglé J'étais vraiment dans mon monde Perdu dans les eaux et forêts J'ai aussi perdu toutes mes ondes Nima ko guénté wone Ak nimou démé nii Comme Yalla'k yaali bébé Fima la féété wone Ak ning ma fayé nii Beuss boula djigué béét ma Togn ngama way Béét ngama way Gaagn ngama way Yaakh nga sama xol Gneupp gnima bayi wone nguir yow Naka la lén di kholé Naka laniou may kholé Lepp limala dane miimeul Teng ko daan def gneulé Tey mane nga thiy boolé Ndéké sa tiél dou sa yarou Dama gueuleum ba téél la juger Ndéké sa tiél dou sa yarou Fimné nila nekh ngay yeungo lady Nima ko guénté wone Ak nimou démé nii Comme Yalla'k yaali bébé Fima la féété wone Ak ning ma fayé nii Beuss boula djigué béét ma Togn ngama way Béét ngama way Gaagn ngama way Yaakh nga sama xol Sonnal ngama Gaathiél ngama Sou démb done tey Dougnou meusseu khamé Nima ko guénté wone Ak nimou démé nii Comme Yalla'k yaali bébé Fima la féété wone Ak ning ma fayé nii Beuss boula djigué béét ma Nima ko guénté wone Ak nimou démé nii Comme Yalla'k yaali bébé Fima la féété wone Ak ning ma fayé nii Beuss boula djigué béét ma Togn ngama way Béét ngama way Gaagn ngama way Yaakh nga sama xol