Ni La Deh

Ni La Deh 가사

원문 언어WO
조회수8
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Baby ku ma la nara xeñ jël fële Soo ma rëccee, lu mel ni fan laa koy jële? Bëgg naa man saa yaw geestu gis ma ci sa wet Chérie kaay ñu juboo Surtout loolu moo dàq lem Bul déglu ki ñëw naan la bàyyi ma Kooku am noon la Mbëggeel capitaine boroom Man de comando laa Bateau dem, bateau costé Ki ko bëgg man de duma ko ko may (Non, non, non, non, non, non) Kër gi benn sër fi ne te ma koy takk Jalal ba Thiak Ndiaye Léegi damay ngoy ci séy bi (ni la de) Séy fi yoku cere dolli ñex (ni la de) Fan yi dama féroce jongé lool (ni la de) Sa jëkker boo ko yore def ko xale way (mëni ni la de) Bae dama fiir te dama gaawa saalit Am xadar waaye xol bi jàppul dara Dama la nob a nob a nob a nob a nob Man mi yamalewuma lak dara Guddi na, baby bul ragal Li may yëg, bae est-ce que yaa ngi koy yëg? Bul ragal, ndaxte du la gaañ Li may yëg, bae est-ce que yaa ngi koy yëg? Chéri, chéri, chéri, baal ma Coow li, coow li, coow li man la (oh, oh) Du man ma la moom dina ngoy ci yaw mel ni dakkande Léegi damay ngoy ci séy bi (ni la de) Séy fi yoku cere dolli ñex (ni la de) Fan yi dama féroce jongé lool (ni la de) Sa jëkker boo ko yore def ko xale way (mëni ni la de)