Lepp legui (feat. Zou Kana)

Lepp legui (feat. Zou Kana) 가사

원문 언어WO
조회수13
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Toubab yangui bronzer nit you nioul Di khessal nieup may moudier konser GMI doyalouniou yalla yefer yi geumouniou yallah nieupay moudier enfer Lou gueneu gaw si mbourou wala leeguins Mbourou da lay djokh kelkun Leeguins dala diokh nimporte ki Ok Kay ma wakh lanrek moma metti ioe Professeur boudé yamay djangal wakhma noumay Def ba tekki té wakhma lane motakh ba ioe tekiwo Shit Gars yi kou len wakh mariage niou len nengo Diabar dote 1million wayé thiaga passe ten taw Domou adama dou doye ci bopam De kharou ci len sou ka amé mou out loka am Li nga khamoul doula sonnal a partir de bingay kham Linga beugeu dinga khep jour bingay am Douniou mbolo wanté Deukeur bop ba melni ngolo kante Sou la wakh dafa vierge dafay soga tenté Beugone tak defar bijou famille Mais bijou bizou mo geuneul samay bijoux de familles (abozé)