Bandit Bou Lewet

Bandit Bou Lewet 가사

원문 언어WO
조회수5
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Ahn, xale bi dama ko yagg Bëgg mu may dozé dima jaay neex Duma rëb di soy jar nama Tagg sa mame ne ma Mbaye Pékh Yagg na la wax dama paré Jarul malay fatali sama jongé Bandit bu lewet mikër rakay sukkër Suma paré si yaw doto takk tére Malay yobu besi kaw Asamaan waw day gaw Malay tekk si yonn bu baax Hé konn ne ma waaw Hé baby, c'est comment? Ñewel ma wan la, c'est comment? Man na la yobu si Coma Mala gëna xam naka la Mani daf may neex Di la doff lo, daf may neex Sangsé don sa laobé Lëmbël moto daf may neex Eh daf may neex Di la doff lo, daf may neex Ne ma Fatou may sa laobé Lëmbël vampire dalay neex, ahn! Oh, ah, oh, ah Ku la am mën na la tey bu baax Oh, ah, oh, ah Paré na foy dem yobalema