Peundeul

Peundeul 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수10
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Ak fo né thi town bi Foo ne ci réew mi ñëwël fi yëngu ci lii Narah laay dooni Man la ma ñëwaat fi gëna teggu ci beat bi Xoolal ni may dugge Xoolal ni may yégge sama baat ci kaaw Mélodie bé meu yéglo Gisatuma, déggatuma Lenn lay gis kon kaay fii ma wone la Gisatuma, déggatuma la I’m so high I’m so high yeeeh Kaay ñu pëndël pëndël pëndël Narah mooy pëndël pëndël pëndël Kaay ñu pëndël pëndël pëndël Narah mooy pëndël pëndël pëndël Lu fora fora fort lay yëg sama xol Fu kawe kawe kawe lay yekk sama yaram di yëngu Ta xawma li koy yëngël fi mu jogé Ayooooo Guddi guddi non stress la dundu happiness Tay non stop Àndak samay way tay de fête la Xoolal ni ma mel, kaay dance all night Sound bi ndax yankay ngueug comme mane ni ma key yeugué Wax ma ndax muñ lay duggu comme nimmey dougué Gisatuma, déggatuma Leen lay gis kon kaay fii ma wone leu Gisatuma déggatuma la I’m so high I’m so high yeeeeh Kaay ñu pëndël pëndël pëndël Narah mooy pëndël pëndël pëndël Kaay ñu pëndël pëndël pëndël Narah mooy pëndël pëndël pëndël Faxasul faxasul faxasul yow Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow Faxasul faxasul faxasul yow Gënel li ci xol bi, tay duñu maye dara Yëngëtul yëngëtul yëngëtul yow Kaay ñu pëndël pëndël pëndël (Kaay ñu pëndël) Narah mu pëndël pëndël pëndël (Kaay ñu pëndël pëndël pëndël pëndël eeh) Kaay ñu pëndël pëndël pëndël Ehhh ehh ehh ehh ehh Narah mooy pëndël pëndël pëndël Hummm hummm