Wa Li Nékhoul

Wa Li Nékhoul 가사

장르Afrobeats
원문 언어WO
조회수23
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Maabo Honey, I love you Baby, I need you Bés bu nekk dinaa la wax je t’aime Duma sonn ci di la wan how much I love you Dégg naa ñu ne dama dof ci yaw Xanaa xamuñu ni yaay dalal li wéradi ci man Bëgguma ñuy meroo, hie! Nañu ànd longo, hie! Bañuma ci xuloo ak ñoom ñépp Nañu bàyyi ñu juboo te noppi Yaay sama ngelaw, yaw rekk doy nga ci man Su ma la gisul tamit, yaa mën dara ci man Yëg-yëg bi amul limite, mel ni asamaan Sa mbëggeel damay dundal ni oxygène ci man, hé! Yaa ma tere nelaw, kenn rekk nga ci man Su ma la gisul saalit, àdduna safal du ci man Yëg-yëg num sore ci nit sama xol lay dal Sa mbëggeel la may dundal, yaw yaa gën ci man, hiii! (Eeh eh ayca ñu dem!) Waa li neexul (Ñu dem, eeh eh weuh) Man, waa li neexul (Aah, yaw mi la hé!) Yaa may daanel (Ñu dem ni la jëlel) Man wa li neexul Laajleen ma lu mu saf (lu mu saf?) Lu neex (hey waay!) Li ma nar ci moom mi (loo nar?) Du jeex (oohhh!) Ñu jëm tas suñu li, xamuñu Yëg-yëg gu mel ni, non, amul! Yaay sama chocolat, cacao piir bi May sa oh la la, man may bu suur bi Moom sa xol ak say xalaat (hé!), wor na Awma xel ñaar (hé!), wor na Yaay sama ngelaw, yaw rekk doy nga ci man Su ma la gisul tamit, yaa mën dara ci man Yëg-yëg bi amul limite, mel ni asamaan Sa mbëggeel damay dundal ni oxygène ci man, hé! Yaa ma tere nelaw, kenn rekk nga ci man Su ma la gisul saalit, àdduna safal du ci man Yëg-yëg num sore ci nit sama xol lay dal Sa mbëggeel la may dundal, yaw yaa gën ci man, hiii! Waa li neexul Man, waa li neexul Aah, yaw mi la hé! Yaa may daanel Ñu dem ni la jëlel Man waa li neexul Yaw mi la, yaw mi la eeh Waa li neexul Yaw mi la, yaw mi la eeh Man, waa li neexul Aaah yaw mi la eh Yaa may daanel Man waa li neexul