Wéétoo

Wéétoo 가사

연도2001
장르Rock Roll
길이3:35
원문 언어RO
조회수329
가사 좌표

원문 가사

RO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Wéétoo, wéétatinaa yaay Wéétatinaa, wéétatinaa, wéétatinna yaay Sophie demna tey ma dabiko Sainte-Marguerite sorina tey ma dabiko Sophie demna, moommii nëwna, moommi demna nii Sophie demna, moommi newna moommii demna nii Sophie demnaa tey ma dabiko Sainte-Marguerite sorinaa tey ma dabiko Demnaa fimu dem sorinaa sana guel demnaa yow Fimu dem sorinaa tey ma dabiko ndeysaay