Jërëjëf La Diva

Jërëjëf La Diva 가사

원문 언어WO
조회수10
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Coumba Gawlo, boo leen xamoon Ki fu mu jaar mooy jaambaar Coumba Gawlo, boo leen xamoon Ki fu mu jaar mooy jaambaar Yàgg nga sigil Senegaal Ci bitim reew ak ci Afrika La femme battante Une référence La grande dame Qui n'a jamais perdu sa valeur Eeee, la diva L'internationale La voix d'or Une fierté africaine Fi nga jaar, képp ju fa jaar Bu dul jaambaar dinga daw Monument nga ci Afrika Gàcc ngalama la diva Mabousso Absa Ndiaye Ablaye Daro mbaar Madior Matar ak Diarra Madiama Yassine Daour ma ca lodo Fatou Kinpe Mbaye sa yaay di sa xarit Laye Bamba Seck sa baay Gawlo Eeeeee! Sa baay dalaa ñaanal dooga dem Gawlo, Gawlo Gawlo, la diva Gawlo (voix d'or du Sénégal) Gawlo (ci Soweto) Gawlo (étoiles meilleure chanteuse moderne) La diva Gawlo (double disque d'or) Gawlo (disque platine) Gawlo (Kora Awards) Gawlo, la Diva Gawlo (fondatrice fem fm) Gawlo (marraine aux Nations Unies) Gawlo (ambassadrice de bonne volonté) Gawlo (lumière pour l'enfance) Merci, Club Gawlo Yoooo Mala yoo, mala yoo Ala Torodo Maal Diaka yooo