Coup Bas

Coup Bas 가사

원문 언어WO
조회수6
가사 좌표

원문 가사

WO
번역이 아직 없습니다. 원문 가사를 표시합니다.
18
Wowoo yaw Ñi lay tagg tay, suba ñoo lay saaga Ñi lay topp tay, suba ñoo lay jaay Ñi la bëgg tay, suba ñoo lay noonoo Ni nga wóolu tay, suba ñoo lay wóorloo Gore dafa jeex, goreedi des fi Te dëggi bu tëwë luy des fi Noppalul waay, wax nga ba tooy Maa ngi ci doorwar, yaa ngi ci xeew Door naan ma saaga naañ ma Daf naan ma picc tëj ma Yóor ma ci biir teen ba lala sulli naañ ma Man taluma leen Man gisuma leen Maa ngi sama yoon Gaynde faat ma xam na taluma leen Man yëguma leen Wa wallaay faalewuma leen Ehn nanguleen Yàlla dogal Kuy yëngal jamano Sayuma neexe, maay yëngal jamano Wa wallaay yaw la Man mi ma yëngal jamano Saa su ma neexee damay yëngal jamano Wa wallaay yaw la Am na ay coup bas Ngir ma def faux pas Bëgg ma tuutal Hééé, lii lan la? Am na ay coup bas Ngir ma def faux pas Bëgg ma tuutal Hééé, lii lan la? Bu Yàlla taane jaam Danga naan waaw Nangudogoloo Day noppal jamm Lim la järal la ma järal Duma kuy dës ginnaaw Ñun dañoo nangu lool Doyloo Yàlla Man ne naa du la seetaan nga fiy ñaaw Dalla bëgg! Man ne naa du la seetaan nga fiy ñaaw Ey, dalla bëgg! Yaay booy ne na du la seetaan nga fiy ñaaw Dalla bëgg! Baba ne na du la seetaan nga fiy ñaaw Ey, dalla bëgg! Kuy yëngal jamano Sayuma neexe, maay yëngal jamano Wa wallaay yaw la Man mi ma yëngal jamano Saa su ma neexee damay yëngal jamano Wa wallaay yaw la Am na ay coup bas Ngir ma def faux pas Bëgg ma tuutal Hééé, lii lan la? Am na ay coup bas Ngir ma def faux pas Bëgg ma tuutal Hééé, lii lan la? Hééé Hééé Lim la järal la ma järal Duma kuy dës ginnaaw Ñun dañoo nangu lool Doyloo Yàlla