Hymne Faramareen

Hymne Faramareen 歌詞

ジャンルWorld Music
原文言語WO
閲覧数9
歌詞座標

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
18
Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na Yéna ngui dég louné, wéraneté, xééx, xoulo nguir man Souma sanione kéne kounék setsila niou naan ataaya Beug yalla ko deff thi diaamam Beug ngama, beug naala (ooh yeah) Yéne gni beug faramareen teudeul nélaw yalla baaxna Kone sopé sopé kaay, yaw kaay Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man Ma sopé sopé lover don't cry Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na Hey yow sama sopé Boul di xoulo, boul di xééx, Yalla nopina Yalla yaa na, Yalla baaxna Maa léén gueuna love Maa léén gueuna yeuk Maa léén gueuna gueum Maay ki leu xam Maay ki leu beug, ouh! Force à toi sopé Force à toi sopé