Woudjou Yayé

Woudjou Yayé 歌詞

ジャンルRegional
原文言語WO
歌詞座標

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
18
Bile wujj yaay, bile wujj yaay Su ma demee jàngi ba wàcc midi Maa ñëw ci kër gi du ma tibbal bool Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk Bu desalee mu ubbal ma ko fa Mbaa mu jox ko xaaj ba Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ Lu tax nga may bàyyi ak moom? Bile wujj yaay, ahn han Aka bon a bon! Bile wujj yaay, ahn han Aka bon a bon! Bile wujj yaay, bile wujj yaay Su ma demee jàngi ba wàcc midi Su ma ñëwee ci kër gi du ma tibbal bool Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk Bu desalee mu ubbal ma ko fa Mbaa mu jox ko xaaj ba Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ Lu tax nga may bàyyi ak moom? Bile wujj yaay, ahn han Aka bon a bon! Bile wujj yaay, ahn han Aka bon a bon! Bile wujj yaay, bile wujj yaay Su ma demee jàngi ba wàcc midi Maa ñëw ci kër gi du ma tibbal bool Bu doomam ñëwee mu jox ko mu lekk Bu desalee mu ubbal ma ko fa Mbaa mu jox ko xaaj ba Baay yaa ma tooñ, baay yaa ma tooñ Lu tax nga may bàyyi ak moom? Waa waa waaw Yaa yaa yaay Waa waa waaw