Doff Ci Yow

Doff Ci Yow 歌詞

ジャンルHip Hop Rap
原文言語WO
閲覧数27
歌詞座標

原文歌詞

WO
翻訳はまだありません。原文を表示しています。
18
Yaay sama lumière Lampe bu may wane yoon Yaay sama lingeer Baby baby baby baby baby Xol bi yaa fi nekk Ta kenn mënul jël sa place Sama diamond, sama woman Bëgguma di la sori Su ma la tooñee, baby sorry Ndax xol bi yaa fi nekk Eh, eh, eh, baby Sama diamond, sama glory Kaay ma wax la I’m ready Baby yaay sama love, love, love, love Baby dama fall in love Love ba dof ci yaw Fooy dem yóbbu ma Bu ma bàyyi ma wet Ku la faalewul ma faale la Yaay sama aljana Yaw laay topp fepp Baby, baby Xam naa li ngay laaj Sans nga posé benn question Xam naa li lay faj Waaw waaw Fees dell toog ci sa place Baby amul benn raison Bu tax man ma lay bàyyi Waa waaw Boo ma bàyyee bàyyi Wax ma fan lay muje Ndax mbëggeel bi ma am ci yaw Depassé na life bi Boo ma jege jege Xam naa li may sentir So baby maa la nob ba love Oh oh oh oooh Baby dama fall in love Love ba dof ci yaw Fooy dem yóbbu ma Bu ma bàyyi ma wet Ku la faalewul ma faale la Yaay sama aljana Yaw laay topp fepp Baby, baby