Yaye Boye

Testo di Yaye Boye

Lingua originaleWO
Visualizzazioni125
Coordinate del testo

Testo originale

WO
Traduzione non ancora disponibile. Mostriamo il testo originale.
18
Yaye boye balalma Yaye boye yaye boye balalma Yaye boyo balalma Khamna awma loula eupeu si adounya Yaye sama wadiour yaye sama lepeu Yaye man Kon yaye soumala masse togne mangui Dieguelou Souma masse dioum tay rethiou nako Ndakh yaye man guisna khale magua Sama kanam Ma khamne yaye boye fii la diar Balalma balalma baalalma Balalma balalma balalma balalmaa Yaye boye Soumala masse togne mangui dieguelou Souma masse dioum tay rethiou nako Ndakh yaye man guisna khale magua Sama kanam Ma khamne yaye boye fii la diar Balalma balalma baalalma Balalma balalma balalma Balalmaa Fane la mana diarr ba fayla yaye yaw Ndakh fayla douma yomba yaye man Waye dina diem sama kemtalay katane Bagua contane Louma def si yaw warou mako naw Yayo ho yaye beuguena yaw ngua contane Ndakh bo contane yala dana contane Gnou sargual sounou yayboy Yaye boye sonnagua yaye boye Masso tayi Yaguala tankhal dila sonal yayo Rethiouw ma loma done dioure Khamna amoul lo dadioul si gnoun gny Tay alhamdou lila mane mi bay la Diour na y dome khamna yoor ndiabote Modi lane Yaye boye yala nala yala fay Balalma yayoboy balalma balalma Balalma yaye boye balalma