Music Xalé

Paroles de Music Xalé

Langue originaleWO
Vues55
Coordonnées des paroles

Paroles originales

WO
Traduction indisponible. Les paroles originales sont affichées.
18
Xale bu ndaw def buzz Ñeet sons kase teg concert (VJ) Important ni adducteurs My g rap bi la jël en main (VJ) 18 ans doon millionaire Rappeur bu ko fi am kan la? (VJ) Xale bi xale yi bëgg Nurulak namp ye koy xëcco (VJ) Surax si kaw scène Def bum te awma sax album (VJ) Ñoom népp kan lañ bãn Kan lañuy xol nigga may seen choice (VJ) Feesal salle di leen joyloo Ñoom ñépp bañ disant nooon (VJ) Pischininiko yaw feccal mel ni Kitana Eh, ne nañ munuma rap Xanaa ñi deñ dof Wala dañ bëgg seen chef yi Ñëw toojal leen bokk Seen muker yi lay xëcc Firil leen mbari naan tës Man duma tiit ndax yaay booy Ne na ma yaw demal music xale Billaay wallaay talay music xale Ñi bëgg VJ ñi koy topp ñépp xale Billaay wallaay talay music xale