Birima

Letra de Birima

Duración6:08
Idioma originalWO
Vistas8K
Coordenadas de la letra

Letra original

WO
La traducción todavía no está disponible. Mostramos la letra original.
18
Maysa tende jodo yaa moom liile Maysa tende jodo yaa moom liile Maysa tende jodo yaa moom liile Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Buri samba laobe yaa moom liile Buri samba laobe yaa moom liile Buri samba laobe yaa moom liile Hi woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Damel maisa penda joor Jooro jooro jooro jooro ho ho ho hoy Sama waaji ken dula jam naani Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Wooy tedi ngoné maarne be sambaa Kuli baca senge ndat biran ngamoo Ngoné maca nas mbay maca jeeri Samba yaasimo dike mbay kuja dooooki Yay borom mbaboor mi Hi di woy birima sama waaji ken dula jam naanee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Dogo fal ak mawa joor kumba samba yaay jaloor Dogo dogo, ho ho ho! Aziz o mbay dogo xam nga yoon wee Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Maisa tendo jooro jooro a mari ngone sobel kayor niila Woy birima fumu yendu ma yendu fa yendo naanee Fonte: Musixmatch