Diamond

Letra de Diamond

Idioma originalWO
Vistas39
Coordenadas de la letra

Letra original

WO
La traducción todavía no está disponible. Mostramos la letra original.
18
Yay sama diamond leral goudi dih leral beuthieuk Yaay sama diamond, ooh Yay sama diamond leral goudi dih leral beuthieuk Yaay sama diamond, ooh Ko wakhal wakhal gaaw diongama wakhal wakhal gaaw ngelaw lou fekh li dih nieuw Iow diapeu nelaw bankou sama lal Goudi ngui mo gueneu yague lol batakhna manatouma nelaaw Ma yakamti ba buerset diote madiakarlo ma wakhla limay yeuk Sokhna si yeureum ma iow mi djiogama wakhal wkhal gaaw Ngalaw lou fekh lih di niow iow diapeu nelaw bankou sama laal Yaay sama diamond leral goudih di leral beuthieuk yaay sama diamond Ooh, yaay sama diamant yay leral goudi dih leral beuthieuk Yaay sama diamant, ooh