Ngala Way

Songtext von Ngala Way

OriginalspracheWO
Aufrufe31
Songtext-Koordinaten

Originaltext

WO
Noch keine Übersetzung verfügbar. Der Originaltext wird angezeigt.
18
Maam, all ma ay dàll ma sol dem wutti gi Luñu dunde Suma amoon laaf kon naaw ci jawwu jii Kumay gungee Di sànku ñaan ci ñi di yalwaan Aljaanay suuf fumu féete Sama xel mooy daan ci bëree sama xol Te sama xol moo ëppu doole Ñun màgg nañu, suñu dàll baay mën ñu jot Ñu war a janook moom Ndax xam nani léegi, àdduna dootul ñu baal Fumay mujjee ak moom Maam ngale,ngala waay, maam ngala waay, ngala waay Man suma doon délluwaat Fan lay délluwaat? Ngala waay, ngala waay, ngala waay Suma doon ñibbiwaat, ñibbiwaat Ndax mës nañ fe gis ku weet Amoon na bës ñu weet Daan nañ fee gis fu weet Ndax fi ngéen dëkkufi Maam ngale,ngala waay (maam ngala waay) Kon ngala waay ngale (ngala waay ngale waay yoo maam booy) Man suma doon délluwaat (délluwaat) Fan lay délluwaat? (suma doon délluwaat, fan lay délluwaat?) Ngala waay, ngala waay, ngala waay Suma doon ñibbiwaat, ñibbiwaat Ci àdduna Di sànku ñaan ci ku nee, ci ku nee Ndax fi ngéen dëkkufi