লিরিক্স স্থানাঙ্ক
WOমূল লিরিক্স
অনুবাদ এখনো নেই। মূল লিরিক্স দেখানো হচ্ছে।
Youxoul, Youxoul, Youxoul
Youxoul walo
Youxoul
Diénguna tey ma wakhak yaw prck thiowli yaw borom
Dékouna bépe khétou 6 yay ki takh ma nék 9
Sa wadiour bou Gor dafla dioundiou topetole sa yaye boul que décevoir
Niaka diome ak dioubanti





